FILET de POISSON FRIT – Recette de Cuisine Facile et Rapide
FILET de POISSON FRIT – Recette de Cuisine Facile et Rapide
On remercie notre Partenaire du NDOGOU Chez ALPHIE Ramadan 2020
FERME GANDIOLE Site Web:
APHIE CUISINE vous le trouvez aussi sur le site internet:
N’oubliez pas de vous ABONNER à la Chaîne
Bonne dégustation !!!
Enjoy your meal !!!
Buen provecho !!!
شهية جيدة
胃口好 !!!
#alphiecuisine #alphiecuisineenfrançais #filetdepoissonfrit
source
47 Comments
Merci alphie recette bi ladone weur 😘😘😘
Nene pour pane bi
Diaroul nene khana
Team croustillant bena ngui ni
Machalla
Wawaw team croustillant ☝️☝️☝️
Machine
Macha alla Alphie yalla na se diam yague
Salut alphie ligueye bi rafete na …..mais moi j'aimerai utiliser les épices ….ay curcuma….cumin ….herbes de province etc…mais à chaque fois j'ai peur de mélanger ceux qui peuvent accompagner la viande ou ceux qui sont pour le poisson….est ce qu'on peut avoir en commentaire une catégorisation….merci
Mahchahlla kontan nagnou
Alphie place farine bi meunagn ko remplacé chapelure
Namna Alphie ak recette yi you nékh yi
MashaAllah Alphie geste bi nice na torop yalna sa diam yagg guoudal fane guay continué dignou bégueul ak sa plât you baax
I love it Mashaa Allah
Laf thiat
Merci alphie
Merci nous vous suivons de près je vous demande juste si vous pouvez dire les épices en wolof
Ma challah alphie tu es pardonne ma chérie et je te demande de même
Dewenety a toi aussi merci pour les recettes 😘😘😘😘😘
Machallah Alphie. Namonenagnela
Machala alphie 💗beugue naa liii mane
Sama cordon bleu bi 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Sama cordon gnewatina hummm🌹🌹🌹🌹
Wa ki dou borom bleu bou rafette bi. Jadore le poisson. Trop bien.
Bal na la akh mé ns comment choisir un très bon cuisinier svp
Toujours croustillant
Ay tata alphie sa numero rek la sokhla
J'aime bien macha Allah
Gnola gueuneu contane.😘😘
Nékhatina machalla
Yawe dale amelo keene akhe goudale fane
Machallah mane mangui team croustillant wawwwawww jadore
Alphie namonnala torop
Baalna la nga baalma Alphy DEWENATI
Mashallah namess bou bari😋😋🥰🥰Alhamdoullilah tayyi kontane nañiou bou bakh pour gislaa merci bcp pour recette bii 🥰🥰🌹🌹
Slt alphie je te fais un gros calin merci beaucoup pour les recettes 💖💖💖💖
Machallah 🌹🌹
Ma alphie merci bcp jdr😘😘
Une semaine rek niou namela bou fi di geuthie way ❤️❤️
A alphi ma balnala m namonagnla dilagnanal diam ac khewal m sa panebakhna
Namone nagne la daal.balnala balniou ken dou yaw
namonala trop si you bakh yi
Je t'adore ma chéri
FATOU amnasolo
Alpine kéneu dou iow machalah amélo kéneu ak you bakh rk nganiouy diokh diii deguereul souniou seuy yi yalna sa diam yague😍❤👏
Machalla alphie contane na si yaw je vous suis depuis italie Milan
Machalah fekel dewene you bari andak kheweul you bari te barkel